show video detail
Mia Guisse - Gauche & Droite (Clip Officiel)
674K 61K 3.2K 03:02
Mia Guisse - Gauche & Droite (Clip Officiel)
  • Published_at:2024-05-23
  • Category:Music
  • Channel:Mia Guisse
  • tags: mia guisse gauche & doite clip officiel mia guisse gauche et droite mia guissé gauche droite mia nouveau clip mia gauche et droite mia gauche et droite clip 2024 mia 2024 nouveau son 2024 2024 mia guisse love renaissance dakar senegal jolofbeats afro mbalax musique music pop gauche et droite mia guissé gauche et droite baabel bete bete bass thioung iss 814 smarty maya kama xiirsa amadeus akhlou brick ibro nadio matadi trace teranga vibe radio zik fm mia
  • description: ** Écoute le nouveau single ici https://bfan.link/gauche-droite : GAUCHE & DROITE disponible sur toutes les plateformes musicales & réseaux sociaux. Streame pour soutenir tes artistes ! ** ** Clique ici https://bit.ly/miaguisseabonnetoi pour suivre mon actualité ** MIA GUISSE évolue & bouge : son nouveau clip, GAUCHE & DROITE. Lyrics plus bas dans la description (dernière partie). #miaguisse #gaucheetdroite #clipofficiel #love #renaissance #miaguissestyle #mgs #team221 ** Crédits de la chanson & du clip GAUCHE & DROITE ** Auteur : Bakhaw Dioum & Mia Guisse Compositeur : Akatche Enregistrement, mix & mastering : Akatche Réalisation Clip : Reverse Studios L’équipe Reverse Studios pour le clip Réalisateur, montage & color grading : Bilal Mbengue D.O.P : Mbaye Diop Chorégraphie : Steven Tourbillon Assistant réalisateur : Djiby Niang Photographe : Amzii.op Accessoires : Magic Hands Make Up : Devon 16 Stylisme : Mia Guisse Style, Afshal, Elfecky Coiffure : Kangue Hair Une production de Mia Guisse Style (Dakar, Senegal, mai 2024) ** Retrouve Mia Guisse sur les réseaux sociaux ** Instagram https://www.instagram.com/mia_guisse TikTok https://www.tiktok.com/@miaguisse Facebook https://www.facebook.com/profile.php?id=100065839831967 ** Contact management ** miaguissecollab@gmail.com +221 77 655 59 67 ** Lyrics de la chanson GAUCHE & DROITE ** Yaw la Yaw la Yaw la yéné sama xol ndakh damala love té sakh kafou ma ci Dama sensible deug la Dama feel beug la diokh Sama xol bi ndakh damala Khalé bi té mala diokh Sama xol bi Ndakh damala love Damalakay diokh, damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant Damalakay diokh damalakoy diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh Han man, han hawma lanela Ma ngui doundou love story bouma yéém Boulma laadj louma dal nii Sama nobél amoul foumou yam Khalébi soma laadjone jant bi, non tey dou fanane Khalébi soma laadjone sama bakane, damalakay diokh Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh eh Gauche wala droite? Dis moi si tu veux en haut en bas ? Dis moi Lou tang wala lou sééd? Dis moi ma servir la Bou 19h dioté gnou teudi Na metti, na yaag, na melni Khalébi boul ragal na nga yekssi Gnoune kessé la thi keurgui na djoly My babe touch my body ouh !!! Everyday ma diokhla nga né thi Khalébi tekk ma lou metti Bou yékhé thi yaw la No no dou thi man han yayayay Han man, han hawma lanela Ma ngui doundou love story bouma yéém Boulma laadj louma dal nii Sama nobél amoul foumou yam Khalébi soma laadjone jant bi, non tey dou fanane Khalébi soma laadjone sama bakane, damalakay diokh Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane chéri ba nopi sopi sama sant Damalakay diokh damalakay diokh Damalakay diokh love bi nek thi mane Yalla ko def lolou louma thi meun anh yeah Oh yeaah ! oh yeah Ndéké khalébi rek laa nop Mane khalébi rek la nop Oh yeaah ! oh yeah Ndéké khalébi rek laa nop Mane khalébi rek la nop ba sagar khégne
ranked in date views likes Comments ranked in country (#position)
2024-05-25 674,770 61,157 3,189 (France,#14)